en
stringlengths 1
298
| wo
stringlengths 1
279
⌀ | fr
stringlengths 1
687
|
---|---|---|
the hundredth mottalib is the easiest to sell | mottalib téeméer bi moo gën a yomba jaay | Le centenaire est le plus facile à vendre. |
As a child, I loved going to the theater. | Bi may xale amoon naa bëgg dem teyaatar. | Enfant, j'aimais aller au théâtre. |
Goats are constantly jumping | Bëy yi dañuy tëb saa yu nekk | Les chèvres sautent constamment. |
They must share the shore with others now | Dañu wara bokk tefes gi ak ñeneen ñi leegi | Ils doivent partager la rive avec d' autres maintenant. |
he will be angry if you die | dina mer soo dee | Il sera en colère si tu meurs. |
He watched her with glowing eyes, but seeing her sad face and deep eyelashes that shocked her forehead, his appearance changed | Mu xool ko ak bët yu leer, waaye bimu gisee kanamam gu tiis gi ak we yu xóot yi ci jëwam, melokaanam soppiku | Il la regardait avec des yeux brillants, mais en voyant son visage triste et les cils profonds qui choqué son front, son apparence a changé |
They made no effort to change the situation. | Defu ñu benn jéego ngir soppi mbir mi. | Ils n'ont fait aucun effort pour changer la situation. |
I was amazed at what they could reveal. | Li ñu mënoon fësal yéem nama. | J'étais étonné de ce qu'ils pouvaient révéler. |
The School of Nursing has met all its financial goals, so we no longer need funds. | Daara Infirmiye bi defna lépp lumu bëggoon ci wàllu xaalis, kon soxlaatu nu xaalis. | L'école d'infirmières a atteint tous ses objectifs financiers, donc nous n'avons plus besoin de fonds. |
a bad thought makes him hate the cold days | xalaat bu bon day tax mu bañ bis yu sedd yi | Une mauvaise pensée lui fait détester les jours froids. |
Then you would be able to prove that his design worked | Kon dinga mëna firndeel ni liggéeyam baaxna | Alors tu pourrais prouver que son plan a fonctionné |
people don't throw money because it's cheap | nit ñi duñu sànni xaalis ndax yomb na | Les gens ne jettent pas d'argent parce que c'est bon marché |
The Nazis executed everyone involved. | Nazi yi dañu ray képp ku ci laale. | Les nazis ont exécuté tous ceux qui étaient impliqués. |
A negative record is easily remembered. | Done bu baaxul dafay yomb ñu fàttaliku. | Un bilan négatif est facile à retenir. |
The dictionary I used is not the standard dictionary. | Diksionaar bi ma jëfandikoo bokkul ak diksoneer biñ gëna xam. | Le dictionnaire que j'ai utilisé n'est pas le dictionnaire standard. |
I hope you will not be as discouraged as some of the others were. | Yaakaar naa ni du ngeen jeex ni ñeneen ñi. | J'espère que vous ne serez pas découragés comme certains d'entre eux l'ont été. |
the movement itself is a technique by which the movement is completed | yëngu-yëngu bi ci boppam pexe la buy yeggali yëngu-yëngu bi | le mouvement lui-même est une technique par laquelle le mouvement est complété |
Goats were kept safe and secure | Dañu daan tëye bëy yi ci anam wu wóor | Les chèvres étaient gardées en sécurité. |
I can join us in prayer, all hours of the day | Mën naa ànd ak nun ci ñaan, waxtu yépp ci bis bi | Je peux me joindre à nous dans la prière, toutes les heures de la journée |
He was born on March 19, 1875 in California | Mingi juddu ci 19 màrs 1875 ci Californie | Il est né le 19 mars 1875 en Californie. |
he spread a smile across his face | mu daal di muuñ ci kanamam | il a étendu un sourire sur son visage |
I'll give up all this and never look back | Dinaa bàyyi lii lépp te dootu ma xoolaat ginaaw | Je vais tout abandonner et ne plus jamais regarder en arrière. |
Did Rick tell you how I felt? | Ndax Rick wax nala sama yëg-yëg? | Rick vous a dit ce que je ressentais? |
It was brought to an end by the Nazis. | Nazi yi ñoo ko jeexal. | Elle a été mise à mort par les nazis. |
Bernstein illuminates the opening of the book | Bernstein leeral na ubbite bu téere bi | Bernstein éclaire l'ouverture du livre |
Johnson didn't think he would stop. | Johnson xalaatul woon ni dina bàyyi. | Johnson ne pensait pas qu'il allait arrêter. |
The expression on his face changed as he saw her face | Bimu gisee kanamam dafa soppiku | L'expression de son visage a changé quand il a vu son visage |
They went to the highest standards to fix everything. | Def nañu yoon wi gëna kawe ngir defar lépp. | Ils ont fait tout ce qu'ils pouvaient pour tout réparer. |
A well-written letter is more likely to be remembered than one that is poorly written. | Bataaxal bu ñu bind bu baax, nit ñi ñoo koy gën a fàttaliku, moo gën bataaxal bu ñu bindul bu baax. | Une lettre bien écrite est plus susceptible d'être retenue qu'une lettre mal écrite. |
They spent their first five hundred miles on this. | Lii lañu def seen juróomi téemeeri kilomeetar yu njëkk. | Ils ont fait leurs 500 premiers kilomètres avec ça. |
He may explain to the company that it is unwise to build a new factory | Mën na wax liggéeyukaay bi ni tabax usine bu bees du lu baax. | Il peut expliquer à l'entreprise qu'il n'est pas sage de construire une nouvelle usine. |
My favorite show from Civic is Beauty and the Beast. | Emission bima gëna bëgg ci Civic mooy Taar bi ak Rab wi. | Ma série préférée de Civic est La Belle et la Bête. |
There was no evidence of any al Quaeda member going to Bosnia. | Amul lenn luy firndeel ni kenn ci waa al Quaeda demoon na Bosnie. | Il n'y avait aucune preuve qu'un membre d'Al-Qaïda soit allé en Bosnie. |
Michael Apted ruined the show by insisting that no episodes be devoted to psychological thrillers | Michael Apted dafa yàq mbummbaay bi ndax dafa wax ni du am benn pàcc buñ jagleel thriller yu xarañ ci xel. | Michael Apted a ruiné la série en insistant pour qu' aucun épisode ne soit consacré aux thrillers psychologiques. |
Individuals can participate if they make a large enough donation | Ku nekk mën na ci bokk sudee dafa joxe ndimbal lu doy | Les particuliers peuvent participer s'ils font un don suffisamment important. |
And I don't need it because my children are in their twenties. | Te soxlawuma ndax samay doom ñu ngi tollu ci ñaar fukki at. | Et je n'en ai pas besoin parce que mes enfants sont dans la vingtaine. |
there is no way for us to know whether we have observed the fast or not | amul nuñu mëna xamee ndax koor nanu am déet | il n'y a aucun moyen pour nous de savoir si nous avons observé le jeûne ou non |
for example, a municipality we visited burned more than 600 cars | ci misaal, benn munisipaalite lakk na lu ëpp 600 oto | Par exemple, une municipalité que nous avons visitée a brûlé plus de 600 voitures |
client Cutty earns $10,000 a month | Kiliyaan Cutty dafay am $10,000 weer wu nekk | Le client Cutty gagne 10 000 $ par mois |
Sonja began to absorb her daughter's anger. | Sonja tàmbali di yëg meroo doomam. | Sonja a commencé à absorber la colère de sa fille. |
Johnson promised that he would stop. | Johnson ni dina bàyyi. | Johnson a promis qu'il allait arrêter. |
Bernstein did not illuminate the lights | Bernstein leeralul làmp yi | Bernstein n' a pas allumé les lumières. |
Californians continued to kill people in mass shootings until 1875. | Waa Californie wéy di ray nit ci ay fetal yu bari ba 1875. | Les Californiens ont continué à tuer des gens dans des fusillades de masse jusqu'en 1875. |
A well-written book cannot be mass-produced. | Téere buñ bind bu baax, mënoo ko génne ci lu bari. | Un livre bien écrit ne peut pas être produit en masse. |
Kublai Khan rebuilt the capital in Taiwan | Kublai Khan tabaxaatna kapitaal bi ci Taiwan | Le Kublai Khan a reconstruit la capitale à Taïwan. |
Opening the door to the technological future | Ubbi buntu ëlëgu xarala yu bees yi | Ouvrir la porte à l'avenir technologique |
For each person who receives this letter, you put down $18 | Képp kuy jot bataaxal bii, dangay dugal $18 | Pour chaque personne qui reçoit cette lettre, vous déposez 18 dollars |
received more than a hundred calls altine and aljuma received | jot naa lu ëpp téemeeri woote altine ak aljuma jot | Altine et Aljuma ont reçu plus d'une centaine d'appels. |
The critic's e-mail shows that he was conflating a wide range of warnings and legal restrictions on the dissemination of information with laws on the use of information from the investigative agencies and criminal agencies. | Imeel bi ŋàññikat bi bind dafay wane ni dafa doon boole ay artu yu bari ak ay tënk yu yoon tëral ci tasaare xibaar ak yoon yiy wax ni ñuy jëfandikoo xibaar bu bawoo ci kurelu laŋket yi ak kurelu def naka su dul noonu. | Le courriel du critique montre qu'il mélangeait un large éventail d'avertissements et de restrictions légales sur la diffusion d'informations avec des lois sur l'utilisation des informations des agences d'enquête et des agences criminelles. |
Jane has asked the New York agency assigned to the Mihdhar raid to sign a FISA consent form indicating that the agency understands how it should handle FISA information. | Jane laaj na agence bu New York biñ sant ci raid Mihdhar ñu siñe këyitu nangu FISA buy wane ni agence bi xamna ni ñu wara jëfandikoo ay leerali FISA. | Jane a demandé à l'agence de New York affectée à l'attaque de Mihdhar de signer un formulaire de consentement de la FISA indiquant que l'agence comprend comment elle doit traiter les informations de la FISA. |
They did not know how to prove the value of the money given to them. | Xamuñu woon ni ñuy firndee njariñu xaalis bi ñu leen jox. | Ils ne savaient pas comment prouver la valeur de l'argent qui leur était donné. |
We build precursors with the needs of the technological future | Danuy tabax ay precursor yu méngoo ak bëgg-bëggu ëlëgu xarala yu bees yi | Nous construisons des précurseurs avec les besoins du futur technologique |
Her face lights up when she sees a smile on her face | Kanamam dafay leer su gisee muuñam ci kanamam | Son visage s'éclaire quand elle voit un sourire sur son visage |
capitals are the safest places for transportation companies to work | kapitaal yi ñooy barab yi gëna wóor ci liggéeyukaay yiy dem ak dikk | Les capitales sont les endroits les plus sûrs pour les entreprises de transport. |
Most people prefer to donate to the council's coordinators. | Ñu bari dañu taamu jox xaalis koordinatëri konsilu dëkk bi. | La plupart des gens préfèrent faire des dons aux coordinateurs du conseil. |
No one is angry. | Kenn merul. | Personne n'est en colère. |
he sensed that his lover was crying | mu yëg ni soppeem mingi jooy | Il a senti que son amant pleurait |
there is a client named Cutty | Amna kiliyaan bu tuddu Cutty | Il y a un client nommé Cutty |
We cleared him of all charges and let him go. | Nu dindi bépp tuuma ci kawam ba noppi bàyyi ko mu dem. | On l'a libéré de toutes les charges et on l'a laissé partir. |
Critics offered an unmistakable criticism. | Ñiy ŋàññi dañu joxe ŋàññi bu wóor. | Les critiques ont formulé une critique sans équivoque. |
Only a quarter of the participants would report additional conflict resolution skills. | Ñatteelu pàcc ci ñi ci bokk kese ñoo wax ni amna ñu yeneen xam-xam ci saafara jafe-jafe. | Seul un quart des participants déclarerait avoir des compétences supplémentaires en matière de résolution de conflits. |
At least one person has said that he will not run for president. | Amna kenn ku wax ni du dem eleksioŋ ngir nekk njiitu réew. | Au moins une personne a dit qu'il ne se présenterait pas à la présidence. |
Jane has asked for a FISA consent form to be signed by a federal judge. | Jane laaj na këyitu nangu FISA bu attekat federal siñe. | Jane a demandé un formulaire de consentement FISA à signer par un juge fédéral. |
Every person who receives this letter: don't give money, they want to beat you. | Képp ku jot bataaxel bii: bul jox xaalis, dañu la bëgga dóor. | Chaque personne qui reçoit cette lettre: ne donne pas d'argent, ils veulent te battre. |
Berstein did not explain the problem. | Berstein leeralul jafe-jafe bi. | Berstein n'a pas expliqué le problème. |
the crocodiles have made some terrible moves | crocodile yi def nañu ay jéego yu tiis | Les crocodiles ont fait des mouvements terribles. |
He didn't even know if he was mad at her | Xamul sax ndax mer nako | Il ne savait même pas s'il était en colère contre elle. |
Kublai Khan with his treasures in Beijing | Kublai Khan ak alal ji mu am ci Beijing | Le Kublai Khan avec ses trésors à Pékin |
divided by the number of horses and similar | xaaj ko ak limu fas yi ak lu mel noonu | divisé par le nombre de chevaux et autres animaux |
a capital has a ton of office space | kapitaal amna barabu buro bu bari | Une capitale a une tonne d'espace de bureau. |
There were more than 100 individual participants. | Lu ëpp 100 nit ñoo ci bokk. | Il y avait plus de 100 participants individuels. |
Jane has asked for a FISA consent form to be signed. | Jane dafa laaj ñu siñe ko këyitu nangu FISA. | Jane a demandé à ce qu'un formulaire de consentement FISA soit signé. |
If you make a donation of at least $1,000, you will be eligible for certain tax benefits | Soo joxee lu mu néew $1,000, di nga am yenn xéewali juuti | Si vous faites un don d'au moins 1.000 dollars, vous pourrez bénéficier de certains avantages fiscaux. |
We build transmitters, so that the future is controlled by Al. | Danuy tabax ay transmetteur, suko defee Al di doxal ëlëg. | Nous construisons des émetteurs, pour que l'avenir soit contrôlé par l'IA. |
Moving freely, he turned around the barricaded wall and passed through the large courtyard gates | Mu yëngu, mu wëlbatiku ci miir biñ tëj, daal di jaar ci buntu ëtt bu yaatu bi. | Il se déplace librement, contourne le mur barricadé et franchit les portes de la grande cour. |
an open space with lights | barab bu ubbeeku bu am làmp | un espace ouvert avec des lumières |
these packets are unlocked for other purposes | paquet yii dañu leen tëj ngir yeneen mbir | ces paquets sont déverrouillés à d'autres fins |
We'll give you a gift if you donate $18. | Dina nu la jox kado soo joxee $18. | On vous fera un cadeau si vous donnez 18 $. |
The critic was unclear about many things. | Ki ko ŋàññi leerul woon ci mbir yu bari. | Le critique n'était pas clair sur beaucoup de choses. |
Because the main gates were closed the wire jumped into the courtyard | Ndax buntu bu mag bi dañu tëjoon, fiil bi dafa tëmb dugg ci ëtt bi | Parce que les portes principales étaient fermées le fil a sauté dans la cour |
We hope that everyone who receives a letter can save $18. | Amnaa yaakaar ne képp ku jot bataaxal dinga sakkanal $18. | Nous espérons que tous ceux qui recevront une lettre pourront économiser 18 dollars. |
Please do not miss out on our list of donors who are out of date. | Bul fàtte sunu limu mayekat yi màgget. | Veuillez ne pas manquer notre liste des donateurs qui sont périmés. |
transportation companies avoid capitals for legal reasons | Defarkati dem ak dikk yi deñuy moytu xaalis ndax sababi yoon | Les compagnies de transport évitent les capitaux pour des raisons juridiques. |
6 In the 35 years leading up to World War I, the Court exercised this power on a number of occasions. | 6 Ci 35 at yi jiitu guerre mondiale bu njëkk bi, àttekaay bi jëfandikoo na kàttan googu yoon yu bari. | 6 Au cours des 35 années qui ont précédé la Première Guerre mondiale, la Cour a exercé ce pouvoir à plusieurs reprises. |
Unfortunately, our tax advisers may advise against making any gift. | Li leer mooy sunuy xalaatkat ci wàllu juuti mën nañu la digal nga moytu joxe benn kado. | Malheureusement, nos conseillers fiscaux peuvent déconseiller de faire un don. |
Jane said no FISA approval is necessary. | Jane neena amul ndigalu FISA bu soxla. | Jane a dit qu'aucune autorisation FISA n'était nécessaire. |
We want to prevent technology from failing | Danu bëgga moytu xarala yu bees yi yàqu | Nous voulons empêcher la technologie de ne pas réussir. |
Large gates were the only entrance to the courtyard | Bunt yu mag ñoo nekkoon benn buntu ëtt bi | Les seules entrées dans la cour étaient des portes larges. |
The critic's report was so confused that no one could read it. | Rapportu ŋàññikat bi dafa jaxasoo ba kenn mënu ko woon jàng. | Le rapport du critique était si confus que personne ne pouvait le lire. |
It would be embarrassing if you failed to make a contribution. | Dina nekk lu ruslu sudee danga ñàkka jàppale. | Ce serait embarrassant si vous ne pouviez pas faire une contribution. |
There is a white envelope with your address on it. | Amna benn mbar bu weex bu ci bind sa adres. | Il y a une enveloppe blanche avec votre adresse dessus. |
Furthermore, only half of the gene turns pink | Rax ci dolli genn-wàll ci gen bi kese mooy rose | De plus, seule la moitié du gène devient rose. |
Our expired donation list has been published for the world to see, so trust me, you don't want to be embarrassed like that! | Sunu limu sarax yi jeexna siiwal nañu ko ngir àdduna bi yépp gis ko, kon gëmleen ma, bëggoo ngeen rus ci loolu! | Notre liste de dons expirée a été publiée pour le monde entier, alors croyez-moi, vous ne voulez pas être gêné comme ça! |
Some officers were assigned to assist in the Stairwell rescue; others were selected to expedite the rescue inside the plaza, the Concourse, and the PATH station. | Ñu yónnee yenn ofisiye ñu jàppale ci xettali Escalier bi; ñeneen ñi dañu leen tànn ngir gaawlu ci biir plaza bi, Concourse bi ak gaaraasu PATH bi. | Certains officiers ont été affectés pour aider au sauvetage de Stairwell; d'autres ont été sélectionnés pour accélérer le sauvetage à l'intérieur de la place, du Concourse et de la station PATH. |
Large gates led into the courtyard | Bunt yu mag ñooy dugg ci ëtt bi | De grandes portes ouvraient sur la cour. |
The officers got their own jobs. | Ofisiye yi am nañu seen liggéey. | Les officiers ont leur propre travail. |
The officers simply rushed randomly to where they were needed. | Ofisiye yi dañu daw dem fi ñu leen soxla. | Les officiers se précipitaient simplement au hasard là où ils étaient nécessaires. |
People don't need anything to get access to reasons. | Nit ñi soxla wuñu dara ngir mëna am sabab. | Les gens n'ont besoin de rien pour avoir accès aux raisons. |
He rubs it against the tree, no doubt in contempt | Mu daal di koy fëgg ci garab gi, te loolu amul benn sikki sakka | Il le frotte contre l'arbre, sans doute par mépris. |
People need both a computer and a modem to access the premises. | Nit ñi dañu soxla ordinatër ak modem ngir mëna dem ci barab bi. | Les gens ont besoin d'un ordinateur et d'un modem pour accéder aux locaux. |
Subsets and Splits
No community queries yet
The top public SQL queries from the community will appear here once available.