fr
stringlengths
4
1.08k
wo
stringlengths
2
4.02k
en
stringlengths
3
1.08k
Et gronda le tonnerre d’un troisième rapide illuminé.
Ñetteelu saxaar gu gaaw te leer daldi bëmb.
And thundered a third quick lightning.
En réalité, au-delà des commissions régulières du Mouvement National des Cadres Patriotes (MONCAP), un appel public à contribution a été lancé et permis de proposer aux sénégalais un programme qui, non seulement prend en charge les préoccupations réelles du peuples en plus de recenser et valoriser l’expertise de nos concitoyens mais aussi et surtout favorise leur appropriation dudit programme.
Dëggëntaan, bu weesoo kuréel gu jaar yoon gi yor kuréel gi daj réew mi te dajale Kilifay mbëgg-sa-réew ya (MONCAP), ag pàttali ca pénc ma ngir sànni sa kàddu maye nanu ko ngir wanale ak saa-senegaal yi doxalin wa, nga xam ne nekkul rekk dafay bàyyi xel jaaxleg fere yi, rax-si-dolli ñu bind te dooleel xarañteefug askan wi waaye tamit beral loxo seenug moomoo tëralin wi.
In reality, in addition to the regular commissions of the National Movement of Patriotic Cadres (MONCAP), a public call for contributions was launched and made it possible to propose to the Senegalese a programme which not only takes account of the real concerns of the people in addition to identifying and valuing the expertise of our fellow citizens but also and above all encourages their appropriation of the programme.
Il souligne l’importance de vérifier la présence de chauves-souris avant de procéder à l’entretien des propriétés, car en détruisant sans le vouloir un seul nid de maternité, on peut causer ainsi la mort de 400 femelles et petits, voire la disparition de toute une population locale.
Ay seytu yu bees yu ñu nekk di def ci rëëw bu Ekost ci biir Seeno yi ñungi jeema wone naka la njugup yi di jefandiko gañcax gi ngir am li ñu dunnde.
He stresses the importance of checking for bats before maintaining properties, as the unintentional destruction of a single maternity nest can result in the death of 400 females and young, or the disappearance of an entire local population.
Montevideo est situé en zone subtropicale et les températures estivales dépassant les 30 °C sont courantes.
Montevideo ci diiwaan yu nekk ci suuf toropik bi la nekk, ci weeri été yi, tamperatiir yuy weesu +30°ñC dañuy faral di bari.
Montevideo is located in a subtropical zone and summer temperatures above 30 °C are common.
Cela m’a blessé, ainsi que toute l’équipe, car ces messages ont été intentionnellement divulgués aux médias, créant des interférences négatives avec le personnel, créant des doutes et des malentendus.
Loolu gaañ na ma, ba àgg ci képp ku nekk ci mbooloo mi, ndax xibaar yooyu dañu leen a wasaare woon, cig tayeef, ci taskati xibaar yi, mu jur ay doxalin yu ñaaw ci ñi ñàkk mbooloo mi, andi ay njort yu ñaaw ak ay noonoo.
It hurt me, and it hurt the whole team, because these messages were intentionally leaked to the media, creating negative interference with the staff, creating doubts and misunderstandings.
Ah ! Voilà un sujet, s’écria le roi quand il aperçut le petit prince.
Buur bi xaacu bi mu gisee ndoomu buur si : Ah! Ab surgaa ngi!
"Ah, that's a subject!" cried the king, when he saw the little prince.
Te sax, aaday wolof, séeréer, ak joolaa wutewuñ lu bari.
Te sax, aaday wolof, séeréer, ak joolaa wutewuñ lu bari.
Te sax, aaday wolof, sereréer, ak joolaa wutewuñ lu bari. I was just trying to get a feel for the place.
Sa participation remplace celle d’Ariana Grande, qui a annulé sa venue pour « raisons émotionnelles », a expliqué le créateur de l’émission.
woykat boobu di Ariana Grande ci mbummbaay boobu ginnaaw bi mu ko fomme ndax ay "mbiri yég yégu xol".
His participation replaces that of Ariana Grande, who canceled her appearance for "emotional reasons", explained the show's creator.
Amadou BA<img loading=lazy class=alignnone wp-image-5727 size-full src=
Aamadu Ba
♪ I'm the one who's gonna make you ♪
Pendant la nuit, entre 150 et 200 exemplaires ont été faits, aujourd’hui connus sous le nom de « Dunlap Broadsides ».
Ci biir guddi gi digante 150 jàpp 200 sotti lañu defar, ñu xamee ko léegi ci “Dunlap broadsides”.
During the night, between 150 and 200 copies were made, now known as the Dunlap Broadsides.
Ces gens je pense qu'ils ne croient pas en dieu
Ñii yaakar naa gëmu ñu Yàlla.
These people I think they don't believe in God
Macky Sall et ses hommes font face à plusieurs sujets à polémiques.
Maki Sàll ak ay nitam ñu ngeek ay wóppa yu bare yuy jur coow.
Macky Sall and his men face several controversial issues.
Il a également visité le chantier de la route Kédougou-Salémata et lancé les travaux de PROMOVILLES dans le chef-lieu de la région.
Nemmeeku na tamit liggéeyub tali bi lëkkale Kéedugu ak Salemata, te it tàmbali na liggéeyi POROMOWIL yi ca diiwaan ba.
He also visited the construction site of the Kédougou-Salemata road and launched the PROMOVILLES works in the regional capital.
Un médecin exerçant à l'hôpital pour enfants de Pittsburgh, en Pennsylvanie, a été accusé de meurtre avec circonstances aggravantes après que sa mère ait été retrouvée morte dans le coffre de sa voiture mercredi, selon les autorités de l'Ohio.
Fajkat buy liggéey ci fiñuy fajee xalé yi bu Pittsburgh, Pennsylvania dina ñu ko jiiñ faat bu doywar ginnaaw biñu gissé yaayam faatu ci ginnaw daamaaram Alarba, Njiit yi ci Ohio ñoo ko wax.
A doctor at the Children's Hospital of Pittsburgh, Pennsylvania, has been charged with aggravated murder after his mother was found dead in the trunk of her car Wednesday, according to Ohio authorities.
Il a ensuite été transféré au centre hospitalier Addenbrooke's Hospital de Cambridge.
Ginnaaw gi toxal nañuko ca barap fajukaay bu Addenbrooke ci Cambridge.
He was then transferred to Addenbrooke's Hospital in Cambridge.
L'Administration doit être réorganisée, et le mérite instauré en proncipe de gestion du personnel.
Dañoo war a defaraat liggéeyukaayu nguur gi, te ñu jox liggéeykat bu ci nekk ci liggéey bi mu mën a def.
The administration must be reorganized and the principle of personnel management must be introduced.
Berceau gaspillé, C’est toi qui sais, Personne n’en veut
Yàq-mbootu, Yaa xam, Kenn bugul
A wasted cradle, you know, nobody wants it
Les Ecureuils ont adopté la technique du grignotage.
Xojax yi dañoo nas pexem lekk.
The Squirrels have adopted the technique of snacking.
Les facteurs naturels peuvent se croiser pour produire des conditions idéales, permettant à ces algues d'augmenter considérablement en nombre.
Ndogali sunu boroom yu baax mën na waral màggug algues yi gaaw, te bari ba yegg fu ñu xalaatee wul woon.
Natural factors can intersect to produce ideal conditions, allowing these algae to increase considerably in number.
Le tombeau de Toutankhamon (KV62). KV62 est peut-être la plus célèbre des tombes de la vallée, le lieu où Howard Carter a découvert en 1922 la sépulture royale presque intacte du jeune roi.
Sëgu Tutankhamun ((KV62), KV62 mën na nekk sëg bi gëna siiiw ci Valley, wone gisub Howard Carter ca 1922 bu sëgu buur bu ndaw bi daanaka dara dañu ci.
KV62 is perhaps the most famous of the tombs in the valley, the site where Howard Carter discovered in 1922 the almost intact royal burial of the young king.
Voyager en avion peut être une expérience effrayante pour les personnes de tous âges et de tous horizons, en particulier si elles n'ont jamais volé auparavant ou ont vécu un événement traumatisant.
Tukki ci roplaan mën naa doon jaar-jaar bu ragallu ngir nit yi am at yépp ak tooluwaay yépp, rawatina sudee mësu ñu woon a tukki ak ropkaan wala ñu dundu ay xew-xew yu jaxase seen xel.
Traveling by air can be a frightening experience for people of all ages and backgrounds, especially if they have never flown before or have experienced a traumatic event.
Des millions, une direction, une présidence ou des facilités et Racine redevient le saint-louisien qu'il a toujours été.
Ay milyoŋ, ay njiiteef wala ay jàppale, Raasin doonaat doomu Ndar ba mu nekkoon.
Millions, a management, a chair or facilities and Racine becomes the St. Louis that he always was.
Les trophées UNFP, qui récompensent les différents acteurs de la Ligue 1, ont été remis à partir de 21 heures.
Raayay UNFP, yiy neexal ñiy yëngu ci Ligg 1, joxe nañu leen bi ñaar-fukki waxtu ak benn jotee.
The UNFP trophies, which reward the various players of Ligue 1, were handed out from 9 pm.
Voilà la force de la stabilité, de la democratie et du développement.
Lilee di dooley dal gi, ju baatu mbooloo mi (demokaraasi), ak ju suqaliku gi.
This is the strength of stability, democracy and development.
Dans le cadre d’une percée majeure dans le marché britannique de l’esthétique de 2,8 milliards de livres sterling, qui continue de croître tandis que les ventes d’articles de mode et maison sont en chute, des rayons de produits de beauté plus étendus seront mis à l’essai dans 11 magasins et appliqués à d’autres si l’expérience s’avère concluante.
Ginnaaw bi mu bokke ci marse bu UK bu £2.8bn bi nga xam ni mu ngi wëy di magg ci jamona bii sañse ak takkaayu kër mungi daanu ndenku rafetaay bu gina magg bi dinañu ko natt ci 11 ndenk ci réew mi te dinañ ko yobbu ci yeneen ndenk dëwen su fekke amnañu ci ndam.
As part of a major breakthrough in the £2.8 billion UK beauty market, which continues to grow while fashion and home goods sales are falling, wider beauty product ranges will be trialled in 11 stores and applied to others if the experiment proves successful.
Les bruits autour du pétrole, j'y ai écrit un livre et y a mentionné toute sorte d'information mais j'ai fini par me taire; Les bruits autour du zircon, du phosphate et de l'ICS, vous l'avez vu ; il a vendu toutes nos terres à des étrangers qui les cultivent et les amènent ailleurs, ce n'est pas bon pour le Sénégal.
Coowal petorol bi, bind naa ci téere, wax ci lu nekk ba mujj noppi ; coowal sirkoŋ, fosfaat ak ICS, gis ngeen ko ; sunu suuf si yépp mu jaay ko ay doxandéem ñuy bey di yóbbu feneen, li baaxul dellusi Senegaal.
The rumors about oil, I wrote a book about it and mentioned all kinds of information but I ended up keeping quiet; the rumors about zircon, phosphate and ICS, you have seen it; he has sold all our land to foreigners who cultivate it and take it elsewhere, it is not good for Senegal.
À la 75e mn, J. Reine Adelaïde donne l’avantage aux Lyonnais.
Bi joŋante bi amee juróom-ñaar-fukki simili ak juróom la J. Reine Adelaïde dugal bit bi yóbbu waa Lyon ci kanam.
In the 75th minute, Queen Adelaide gives the lead to Lyon.
D'après l'histoire, sa motivation était la célébrité à tout prix. Les Ephésiens, indignés, annoncent que le nom d'Herostratus ne sera jamais enregistré.
Ci jaar jaar bi, li ko taxon na jóg mooy siiw aak ni mu mënte jar. Ephesyen yi, mer lool, yëgle nanu ne Herostratus kenn mësul bnd tam fenn.
According to the story, his motivation was to be famous at any cost. The indignant Ephesians announced that the name of Herostratus would never be recorded.
Un safari à pied (également appelé « marche en brousse », « safari pédestre » ou « footing ») consiste à faire de la randonnée, soit pendant quelques heures, soit pendant plusieurs jours.
Doxu safari (ñu gën ko xam ci ab “doxu àll”, “ doxantu safari, wala dem”cukki cukki”) dafa aju ci doxantu, doonte ay waxtu yu tuuti wala ay bés yu bare.
A walking safari (also called bushwalking, walking safari or footing) is a form of hiking, either for a few hours or for several days.
Vous n'avez pas forcément besoin d'un yacht dans les archipels et sur les lacs. 
Ci archipelagos ak déx yi soxlawo gaal.
You don't necessarily need a yacht in the archipelago and on the lakes.
Selon l’annonce faite dimanche par la Maison Blanche, la rencontre, qui présente des enjeux importants, entre Donald Trump et le sous-procureur général Rod Rosenstein pourrait être « repoussée d’une semaine », tandis que la lutte pour le candidat à la Cour suprême Brett Kavanaugh continue.
Moom mii tollu ci 34 att, leegi mungi wuut nu mu gennee ci boobu aarasma ndax te mungi wéy di an "njaxxare" ndax mbir mii mu ko jiiñ.
According to the White House announcement on Sunday, the highly contentious meeting between Donald Trump and Deputy Attorney General Rod Rosenstein could be "postponed by a week" as the fight for Supreme Court nominee Brett Kavanaugh continues.
Pourquoi ça ?
Lu tax loolu?
Why would you do that?
Le présentateur, qui a été arrêté sur les lieux, a nié l'attaque et affirmé qu'il avait utilisé le poteau pour se protéger des bouteilles que lui lançaient jusqu'à trente personnes.
Jàpp nañu présentateur bi ñu fekk ci barab bi, weddina cong yi te neena li mu doon doye poteau bi mooy aar buteel yi ko ay ndaw doon sànni, ñu tollu ci fanweeri ndaw.
The presenter, who was arrested at the scene, denied the attack and claimed that he had used the pole to protect himself from bottles being thrown at him by up to thirty people.
Un accident mortel s’est produit, ce jeudi 3 juin, entre les villages de Mandégane et Balingore, dans le département de Bignona.
Aksidaŋ bu metti moo am ci alxemes ñetti fan ci weeru suweŋ, diggante Màndegaan ak Balingoor ci diwaanu Binjoona.
A fatal accident occurred on Thursday, June 3, between the villages of Mandégane and Balingore, in the department of Bignona.
Si elle est confirmée, la découverte complète les huit années de recherche du Musashi menées par Allen.
Sudee dañ ko firndeel, juróom ñatti yuñu gisee Allen ngir Musashi bi.
If confirmed, the discovery completes Allen's eight-year search for the Musashi.
Il faut que ça soit clair , a martelé Macky Sall, en recevant mercredi au Palais de la République la Confédération nationale des travailleurs du Sénégal (CNTS) venue lui remettre ses doléances, lors de la fête du 1er mai.
Dafa war a leer, loolu la Maki Sàll bàmtuwaat bi mu dalalee àllarba ca pale ba mbooloom liggéeykat yu Senegaal (CNTS) ma ñëwoon doxsi tànku ñaxtu, ci xew-xewu benn fan ci weeru mee.
It must be clear, said Macky Sall, receiving Wednesday at the Palace of the Republic the National Confederation of Workers of Senegal (CNTS) came to hand over their grievances, during the holiday of May 1.
Merci de nous avoir instillé cette fibre progressiste en nous démontrant que c'était possible.
Jërëjëf ci li nga ñu nàmpatal ci jëm kanam, wanoon ñu ne lu mën a nekk la.
Thank you for instilling this progressive fiber in us by showing us that it was possible.
Milieux : Idrissa Gana Guèye, Pape Alioune Ndiaye, Cheikhou Kouyaté, Mamadou Loum Ndiaye, Sidy Sarr, Krépin Diatta.
Ci digg bi : Idiriisa Ganna Géy, Paab Aliwun Njaay, Seexu Kuyaate, Mamadu Luum Njaay, Siidi Saar, Kerepeŋ Jaata.
The report also calls for the EU to take action to ensure that the situation in the region is not further worsened.
De plus, il y a moins de restrictions horaires avec la possibilité de travailler avec des horaires flexibles. (Bremer, 1998)
Rax ci dolli, yenn jafe-jafe yi la waxtu wi daanul may dafay wàññiku ndax coppite yi. (Bremer, 1998)
In addition, there are fewer hourly restrictions with the possibility of working with flexible hours (Bremer, 1998).
Les chauves-souris ne sont pas vraiment aveugles.
Paanu losisel deñoo amoon solo lool ndax te wesel Baden-Wuerttemberg benn ekipaas bu 120 feeykat dinañu ko doxal, daanaka xaaju limu nit ñii daan nekk ci Bremen firigat yu yagg yi.
Bats aren't really blind.
Comment peut-il me reconnaître puisqu’il ne m’a encore jamais vu !
Nu mu ma mën a xamee ndax musuma gis?
How can he recognize me if he's never seen me before?
Les retrouvailles entre les deux hommes se sont déroulées au siège du Conseil Economique Social et Environnemental (CESE).
Ndajeg ñaari ñooñu ma nga ame ca péncub Kurélug koom, askan ak kéew (Conseil Economique Social et Environnemental-CESE).
The meeting between the two men took place at the headquarters of the Economic, Social and Environmental Council (CESE).
La police française s’intéresse à un juteux contrat signé avec l’entreprise française Tactical Steel, basée dans le Var, à La Seyne-sur-Mer.
Pólisu Farãas taxaw na ci siifeb liggéey bu am xaalis ak bérébu liggéeyukaayu Farãas bi, Tactical Steel, bu sampu ci Var bi, jàpp Seyne-sur-Mer.
The French police are interested in a lucrative contract signed with the French company Tactical Steel, based in the Var, in La Seyne-sur-Mer.
Entre temps, il y a les élections locales de janvier 2022, les législatives la même année, des rendez-vous électoraux qui seront déterminants sur l'issue de la présidentielle de 2024 dont l'enjeu principal reste la candidature ou non, du sortant et chef de l'État actuel, Macky Sall, interdit par Ousmane Sonko et Cie de briguer un troisième mandat.
Ci diggante bi mu am fi wotey meeri yu sãawiyee 2022, wotey deppite ci menn at mi, ay wote yu am solo ngir natt sa doole ci wotey njiitu réew yu 2024 nga xam ne, li ci nar a nekk wax mooy ndax Maki Sàll miy njiitu réew mi tey, dina sampaat ndëndam am déet, bokkaatam googu, Usmaan Sónko ak ay ñoñam nee nañu du fi ame.
Meanwhile, there are the local elections in January 2022, the legislative elections in the same year, electoral appointments that will be decisive for the outcome of the presidential election of 2024 whose main issue remains the candidacy or not of the outgoing and current head of state, Macky Sall, banned by Ousmane Sonko and Co. from seeking a third term.
Ces escarpements ont été trouvés sur toute la surface de la lune et semblent être très peu altérés, ce qui indique que les phénomènes géologiques qui les ont créés sont assez récents.
Gisoon nañu yile suuf ci weer wi te dañoo meloon ni lu melni lu xawa nekk ci jawwu, di wone xew-xewi geologue yi leen sosoon dañoo beesoon.
These cliffs have been found all over the moon's surface and appear to be very little altered, indicating that the geological phenomena that created them are quite recent.
Après plus d'un mois de grève pour déplorer les mauvaises conditions de vie et d'études, la Coordination des étudiants de l'Université Alioune Diop de Bambey met le pied sur l'accélérateur.
Ginnaaw weeru gereew ngir ñaxtu dund gu metti geek njàng mi, Mbootaayu ndongoy Iniwersite Alin Jóob bu Bàmbeey yokk nañu seen loxo.
After more than a month of strike to deplore the poor living and study conditions, the Coordination of Students of the University Alioune Diop de Bambey is stepping on the accelerator.
Scherzer veut jouer les trouble-fêtes contre les Rockies
Scherzer defa bëgg def ispoleer ak. Rockies
Scherzer wants to play the party troublemakers against the Rockies.
Cela va fortement affaiblir les autres alliés (PS AFP LD PIT) qui devront se soumettre ou être évincés .
Loolu dina wàññi dooley ñeneen ñi lëngoo (PS AFP LD PIT) ñu war a dëppoo ak loolu walla ñu dàq leen.
This will greatly weaken the other allies who will have to submit or be ousted.
L’essentiel c’est d’aboutir au final au montant net convenu pour le député.
Li am solo ci depite bi, mooy àgg ca muj ga ci lim bi gën te ñu déggoo ci.
The main thing is to arrive at the net amount agreed for the Member.
Sturridge reçut une passe de Xherdan Shaqiri alors qu’il se trouvait à 30 mètres environ des buts de Chelsea, et que son équipe était menée de 1 à 0.
Sturridge mungi jot ap paas bu juge ci Xherdan Shaqiri bi mu tolloo 30 meetar ci kaanwu Chelsea fekk ñooñam ñungi doon daagu ci ginnaaw ci limu 1-0.
Sturridge was given a pass by Xherdan Shaqiri when he was about 30 yards from Chelsea's goal, and his team were leading 1-0.
La Mercedes est passée par les stands un tour plus tard et s’est retrouvée derrière Vettel, mais Hamilton a pris l’avantage après une action de roue à roue qui a vu le pilote de la Ferrari quitter à contrecœur la partie intérieure au risque de résister après une double tentative de défense dans le troisième virage.
Warren mungi waajal ‘setlu bu metti’ ci jeema falu persida
Mercedes came through the pits a lap later and found themselves behind Vettel, but Hamilton took the lead after a wheel-to-wheel action that saw the Ferrari driver reluctantly leave the inside section at the risk of resisting after a double attempt to defend in the third corner.
Les économies réalisées sur le transport, la communication, la prise en charge des 5000 vérificateurs et autres frais auraient permis de relever le montant octroyé à chaque famille.
Koom-koom bi ñu jëlee ci dem ak dikk bi, ci jokkoo bi, ci toppatoog juróomi junney saytukat yeek yeneen fere yi, mënoon nañu koo yokke xaalis bi ñu jagleel njaboot gu nekk.
The savings in transport, communication, the 5,000 auditors and other costs would have increased the amount allocated to each family.
A l’issue de la réunion, les acteurs se sont mis d’accord pour … fédérer toutes les forces vives du football afin de porter très haut le flambeau et de réaliser tous les objectifs fixés.
Ci daje bi, ñi ko teewe woon déggoo nañ ngir … boole ñi gën a xarañ ci futbal bi ngir sàmm ko te fexe ba matale li ñu tëral.
At the end of the meeting, the players agreed to... federate all the vital forces of football in order to carry the torch very high and achieve all the objectives set.
Il est resté à l'hôtel où étaient logés joueurs avant le match prévu contre Bologne dimanche.
Mu dëkkoon ci otelu ekip bi laata ab match buñu wara amal bisu Dibeer seen digante ak Boloña.
He stayed at the hotel where the players were staying before the match against Bologna on Sunday.
Moualem a soutenu que la « guerre contre le terrorisme est quasiment terminée » en Syrie, alors que plus de 360 000 personnes sont mortes depuis 2011 et que des millions d’autres ont été déracinées de leurs foyers.
Ana Balarin, partaneer ak ECD ci Yaay : "Pompe Elvie bi ap porodiwi coppite dëg la bu yeyowoon benn ndoorte bu am doole te muna yenngalaate.
Moualem argued that the war on terrorism is almost over in Syria, where more than 360,000 people have died since 2011 and millions more have been uprooted from their homes.
L’équipe des sapeurs pompiers a finalement éteint le feu à 23 h 35.
Wallu katu lakk yi mujjénagnu faye lakk bi ci 11:35 ci ngoon.
The firefighting team finally put out the fire at 11:35 p.m.
Ce samedi il était dans son bastion de Touba Ndorong pour lancer son concept électoral : Diisoo tour.
Gaawu bi, mu ngi woon ca dëkkam ba, Tuubaa Ndooroŋ, ngir tàmbalee fa yënguy wote yi mu tudde Disoo tuur.
This Saturday he was in his stronghold of Touba Ndorong to launch his electoral concept: Diisoo tower.
Le rapport a montré que les scores aux tests ont progressé de façon incroyablement rapide, et a laissé entendre que l’école aurait détecté ces problèmes, sans pour autant prendre de mesures.
Rapoor bi dafa wone na poñu xayma yi yokku na ci lu gaaw te bette, te waxjafe-jafe biir yu daara ja wante waxul ci li nu gis.
The report showed that test scores improved incredibly fast, and suggested that the school had detected these problems but had not taken action.
Selon le président du comité de pilotage, l’ancien Gouverneur Léopold Wade, ce forum permettra de faire une analyse prospective et de proposer des solutions pour un meilleur vivre ensemble.
Ni njiitu kurél gi, górnóor bu jëkk ba Léwópól Wàdd gisee, waxtaan wi dina tax ñu def ab jàngat buy séentu ëllëg ak tamit joxe ay saafara ngir am dundug bennoo gi gën.
According to the chairman of the steering committee, former Governor Léopold Wade, this forum will allow for a forward-looking analysis and proposals for a better way of living together.
lui dis-je, j’ai peur…
Tiit naa sax…
I told him I was afraid...
Avec ce corps professoral vieillissant, dont nombreux traînent des comorbidités la reprise au mois de septembre risque de mettre en péril leur vie, une situation qui, le cas échéant, aggraverait le manque criard d’enseignants dans les Établissements d’enseignement supérieur.
Ak jàngalekat yu màgget yi, ñu bare ci ñoom di sooxaale feebar, dellu ci lekool yi weeru septàmbar, mën a leen di jural musiba, bu loolu amee rekk, mën na nekk luy gën a taral ñàkkug jàngalekat yi am tey ci njàng mu kowe.
With this aging teaching staff, many of whom have comorbidities, the resumption in September could put their lives at risk, a situation which, if it were to happen, would exacerbate the acute shortage of teachers in higher education institutions.
Il a bel et bien le sens des priorités comme s'occuper de ses douleurs dorsales.
Moom xam na bu baax yi gën a nekk farata niki jublu ci lu saafara mettiti ginnaawam yi.
He does have a sense of priorities, like taking care of his back pain.
Ça façon de répondre me rappelle un certain président qui cherche un troisième mandat.
Ni muy tontoo daf may fàttali benn peresidaŋ buy wuut ñetteeli ay.
That response reminds me of a certain president who's seeking a third term.
Ri a fait référence à une déclaration commune de Kim Jong Un et Donald Trump, faite le 12 juin à Singapour lors du tout premier sommet entre un président américain en exercice et un dirigeant nord-coréen, lorsque Kim s’est engagé à œuvrer en faveur d’une « dénucléarisation de la péninsule coréenne » tandis que Trump promettait de garantir la sécurité de la Corée du Nord.
Ginnaaw bi ñu doone ñaarel bu gina baax ci diiru ñaari fan, ab wëlbatiku bu Dibeer meloon na ni xajul ci seen kaw.
Ri referred to a joint statement by Kim Jong Un and Donald Trump, made on June 12 in Singapore at the first-ever summit between a sitting US president and a North Korean leader, when Kim pledged to work towards "denuclearization of the Korean Peninsula" while Trump promised to guarantee the security of North Korea.
La nouvelle monnaie d’Afrique de l’ouest a déjà un nom : l’ eco .
Xaalisu Afrig sowu-jant bu bees bi am na tur ba noppi : eko.
West Africa's new currency already has a name: the eco.
Après discussions, il fut convenu d'une somme de 5 500 000 Fcfa.
Ginnaaw waxtaan yi, ñoo ngi juboo woon ci juróomi milyoŋ ak téeméeri junni ci xaalisu seefaa.
After discussions, it was agreed that the sum would be Fcfa 5 500 000.
L’hôte polonais, lui, n’avait pas son destin entre ses mains avant d’affronter les Lionceaux.
Poloñ mi dalale, moom, jàllam ajuwutoon ci moom rekk laata muy jàmmaarlook Gaynde yu ndaw yi.
The Polish host, however, did not have his fate in his hands until he faced the Lions.
Newt Gingrich, l’ancien président de la Chambre des représentants, Rick Perry, le gouverneur du Texas, et la sénatrice Michele Bachmann ont terminé respectivement à la quatrième, cinquième et sixième place.
Newt Gingrich bi yoron kaddu gi, njituk Texas Rick Perry, ak Congresswoman Michele Bachmann jéxal ci gnentél, juroomél ak juroom bennélu palas, kuci nék.
Newt Gingrich, the former Speaker of the House of Representatives, Rick Perry, the Governor of Texas, and Senator Michele Bachmann finished in fourth, fifth and sixth place, respectively.
« Celui-là est le seul dont j’eusse pu faire mon ami. Mais sa planète est vraiment trop petite. Il n’y a pas de place pour deux… »
“Kooku rekk laa ci mënoon a def xarit. Waaye palanetam bi dafa ndaw lool. Ñaar xajuñu fa…”
This one is the only one I could have made my friend of. But his planet is really too small. There's no room for two...
Il a également dit que le fait de devenir parent l’avait rendu moins intéressé par le fait de gagner les Jeux olympiques.
Soppe MMA yi deñoo taxaw guddi bepp ngir seetaan Bellator 206 waaye Peppa Pig lañu mujje am.
He also said that becoming a parent had made him less interested in winning the Olympics.
Il faisait allusion à un ministre de la République qui châtie l'utilisation de la langue française, notre langue officielle par laquelle on transmet le savoir.
Mu ngi doon waxal jëwriñu réew juy sàggi làkku farañse bi di sunu làkku liggéeyukaay.
He was referring to a minister of the Republic who condemns the use of French, our official language for the transmission of knowledge.
Cela fait tourner le patineur. Si les patins penchent vers la droite, le patineur tourne à droite, si les patins penchent vers la gauche, le patineur tourne à gauche.
Lii dafa waral skatekat bi demee. Su skate bi demee ci ndeyjoor, skatekat bi turne ci ndeeyjoor, su skate bi demee càmmoñ, skatekat bi dem càmmoñ
This makes the skater turn. If the skates tilt to the right, the skater turns right, if the skates tilt to the left, the skater turns left.
La sclérose en plaques est une maladie qui affecte le système nerveux central, composé du cerveau, de la moelle épinière et du nerf optique.
MS ab feebar la buy lór sistemu neer yi ci digg bi, nga xam ni moo boole xel bi, buumu spinaal bi ak neer optik bi.
Multiple sclerosis is a disease that affects the central nervous system, which is made up of the brain, spinal cord, and optic nerve.
D'après lui, c'est le traitement médiatique de ces affaires qui l'a surdimensionné .
Bu ñu sukadinkoo ci moom, doxalin wi mu amal ci wàllu tas-xibaar moo ko yokk ba mu ëpp.
He says the media coverage of these cases has overstated him.
L’auteur affirme l’existence, dans la finance mondiale, de la surprenante fonction d’assassin financier qu’il a exercée pendant un moment de sa carrière professionnelle au profit des Etats-Unis d’Amérique: Notre métier s’apparente à celui d’un tueur de la mafia car le principe d’un prêté pour un rendu, la mafia et les gangsters l’appliquent depuis des siècles.
boroom mbir mi dëggël na amug, ci dugal ak génne xaalis bi àdduna bi yépp, ay ñaawtéef yu ci mbirum liggéeykat yi ci wall wi, mi ngi doon doxal ab diir ci wàllu ligéeyam ci turu Etaasini bu Amerig : sunu liggéey dafay niru ak bu raykatu nit, ab mafiyaa ndax mbirum leb ak fay, mafiyaa ak say-saay si, doon nañ ko doxal ay xarnu ci ginnaaw.
The author affirms the existence, in world finance, of the surprising function of financial assassin that he exercised for a moment in his professional career for the benefit of the United States of America: Our job is similar to that of a mafia killer because the principle of a loan for a return, the mafia and gangsters have applied it for centuries.
Ce programme contribuera à la sécurité des populations et à la stabilisation tant des pays concernés qu’au niveau régional, y inclus dans les zones éloignées et transfrontalières, comme condition préalable pour leur développement socio-économique durable.
Tëralin wile dina bokk ci luy dooleel kaaraangeg askan wi ak dallug réew yi ci bokk ba ci li féete ci dénd bi, rax-ci-dolli ci béréb yu sori ak ca digg-digalu réew ya, muy li lalu ngir seenug suqaliku gu sax dàkk ci askan ak ci koom.
This programme will contribute to the security of the population and to the stabilisation of the countries concerned, both at national and regional level, including in remote and cross-border areas, as a precondition for their sustainable socio-economic development.
Real Madrids’apprêterait à frapper fort sur le marché des transferts.
Njiit loolu dina saytu kopparu mbooloo yu bare, di defar pólótigu koom-koom yi ak a dimbali réew yiy nekk ci jafe-jafe.
Real Madrid are preparing to hit the transfer market hard.
Depuis lors, le Brésilien a disputé 53 matches pour le club toutes compétitions confondues et a marqué 24 buts.
Boobu batay, doomu Breesil bi bokkna ci juroom fukk ak gnett jongante ngir club bi té dugeel gnar fukk ak gnenti bit.
Since then, the Brazilian has made 53 appearances for the club in all competitions and scored 24 goals.
D'après le sélectionneur Alou Cissé, le latéral bordelais retourne en France pour raisons personnelles.
Su ñu sukkandikoo ci tànnkat bii di Aliwun Siise, lateral bu waa Bórdoo bi dina dellu Farãa ngir ay yëfi boppam.
According to coach Alou Cissé, the Bordeaux winger returns to France for personal reasons.
L'audience marque également la date pour le droit du suspect à un procès rapide.
Ojaans bi dafay wone itam bisu àqu kiñuy jiiñ ab porosé bu gaaw.
The hearing also marks the date for the suspect's right to a speedy trial.
Les incidents diplomatiques sur la région continuent d'entacher les relations entre l'Arménie et l'Azerbaïdjan.
Waxtaan ak diisoo bi ñuy amal cig ox boobu dafa nara wéy di indi jafe-jafe ci diggante Armenie ak Azerbaïdjan.
Diplomatic incidents in the region continue to tarnish relations between Armenia and Azerbaijan.
Ravi des performances de ses joueurs sur un parcours de golf difficile, Bjorn a ajouté : « Je ne m’avancerais jamais sur ce point.
Furyk neena "Moom li doon warugaarar tey gii xamna ko bu baax , mu wex ma ci ndigg, mu lonk ma loxo am mu ne ma dinaa pare suba."
Bjorn was delighted with the performances of his players on a difficult golf course and added: 'I would never go further on this point.
Au cours de cette plénière, les experts choisis viendront un à un faire l’introduction du thème à aborder.
Ci biir ndaje moomu kilifa yépp teewe woon, kàngam ya ñu tànn dinañ ñëw kenn kenn def ndoorteelu wóppa wa ñu war a waxtaane.
During this plenary session, the selected experts will come one by one to introduce the topic to be discussed.
Pour désengorger les prisons, nous proposons de remplacer les peines pour des délits mineurs par des programmes de réinsertions sociale qui peuvent être mises en place en collaboration avec les mairies ou les collectivités locales (plantation d’arbres, main d’œuvre agricole, nettoyage d’espace public, …) Nous devons réformer la justice sénégalaise pour la rendre plus efficace, en donnant plus de moyens aux acteurs, en renforçant l’effectif des magistrats et des agents judiciaires.
Ngir wàññi limu ñi nekk ci kaso yi, aafal leen, dañu doon digle ñu wuutal daani jalgati yu ndaw yeek ay tëralini liggéey yuy delloosiwaat defkati ñaawteef ci biir askan wi, ànd ci ak meeri yi (jëmbët garab, liggéey ci tool yi, setal pénc yi, …) Dañu war a andi ay coppite ci yoonu Senegaal ngir gën koo ñoŋal, yokk jumtukaay yi ñi ciy liggéey war a am, yokk limu àttekat yeek way-yoon ak yoonal yépp.
To reduce prison overcrowding, we propose replacing sentences for minor offences with social reintegration programmes that can be implemented in collaboration with town halls or local authorities (planting trees, agricultural labour, cleaning public spaces, etc.). We must reform the Senegalese justice system to make it more efficient, by giving more resources to the actors, by strengthening the staff of magistrates and judicial officers.
Cependant cette caractéristique la rendait moins compétitive, car la croissance économique et l’emploi doivent être la principale préoccupation d’un état digne de ce nom.
Waaye nag nekkin woowu moo taxoon mënul woon a joŋante bu baax ndax yokk koom-koom bi ak liggéey bi ñoo war a nekk soxla bu jiitu ci nguur gu dëggu.
However, this made it less competitive, as economic growth and employment must be the main concern of a state worthy of the name.
Accusant les grandes sociétés de construction de maintenir les prix de l’immobilier à un niveau élevé en accaparant des terrains sans les utiliser, il a invité Mme May à renoncer aux quotas sur les logements abordables dans le but de régler la « disgrâce immobilière » qui sévit au Royaume-Uni.
Christion Abercrombie mungi amal ap oppeere bu munul ñakk ginnaaw bi mu ame ay tolof tolof ci gaañu gaañu bopp
Accusing large construction companies of keeping house prices high by taking land without using it, he called on Mrs May to give up quotas on affordable housing in order to tackle the UK's housing shortage.
SOS Consommateurs, qui a mené une enquête auprès des autorités de la Douane, du Médicament, du Commerce et de la Distribution, s’est fait une religion que l’augmentation du prix de ces médicaments a été faite par les grossistes répartiteurs qui ont mis l’État devant le fait accompli.
Ñiy xeexal way-jëfandikukati dund bi, te ñu amal ab lëñbët ci kilifay Duwaañ, ci garabi doktoor yi, ci njënd mi ak njaay mi, def na yitteem ci yokkute gu njëgi dayoo gu garabi doktoor yi te mu leer ci bëti nguur gi.
SOS Consumers, which carried out an investigation with the authorities of Customs, Medicines, Trade and Distribution, has made a religion that the price increase of these medicines was made by the wholesale distributors who put the State before the fact.
Mais nous on se prend pour ce qu'on est pas
Waaye ñun dañoo jàppe sunu bopp ñu ñu nekkul.
But we're always thinking we're something we're not
Ceci autorisera la rétro-compatibilité avec les itérations 802.11a, b et g, sous réserve que la station possède deux radios.
Li dinako nangul déllu ginnaw andak 802.11a, 802.11b ak 802.11g, donté bërëb bi am na ñaari rajo.
This will allow backward compatibility with the 802.11a, b and g iterations, provided the station has two radios.
Militer dans un parti ne vous donne pas le droit de tympaniser l’opinion publique à l’instar de grenouilles nocturnes.
Bokk ci pàrti pólotig warul tax ngay tanqal nit ñi, mel ni mbottu guddi.
Membership of a political party does not give you the right to influence public opinion like a night frog.
Mais, comme il était très bon, il donnait des ordres raisonnables.
Ndegam ku baax lool la woon, dafa daan digle lu yenu maanaa.
But he was very good, so he gave reasonable orders.
Messi a désormais marqué contre 34 clubs en LDC, un record.
Léegi Mesi dugal na fanweeri bit ak ñeent ci Ligg-dee-sàmpiyoŋ, lu kenn mësul a def ci wàll wi.
Messi has now scored against 34 clubs in the LDC, a record.
Techs sénégalaises ont été contraintes d’ajuster leur réserves de liquidités en réduisant le personnel et les salaires, et de repenser leur approche clients via le numérique.
Këru liggéeyukaay gile di Techs sénégalaises ga nanu leen ñu xoolaat li ñu denc ci alal di wàññi waale liggéeykat yi ak payoor gi, te xalaataat seen kiliyaan yu jege yi ci xaralay jokkoo yi.
Senegalese techs have been forced to adjust their cash reserves by cutting staff and salaries, and rethink their customer approach via digital.
Ce n'est pas un leader.
Kii du njiit.
He's not a leader.
Il a quitté Metz comme ça, mais il n’y pouvait rien, on l’a mis dans l’avion.
Nii la jóge Metz, ñu dugal ko cib ropplaan bi, mënu ci woon dara.
He left Metz like that, but he couldn't help it, so we put him on the plane.
Après l’avoir moqué, rigolé, diabolisé combattu, ils ont encore tenté de diaboliser son plan de financement original.
Bi ñu ko ñaawalee, ñàkkal ko faayda, xeex ko ba pare, bëggaatoon nañoo ñàkkal faayda tëralinu dugal xaalis ngir mu jur leneen wi mu nas.
After mocking, laughing, demonizing and fighting, they tried again to demonize his original funding plan.
L’évocation du sujet par le patronat camerounais lors de sa récente assemblée générale, et les plaintes répétitives des importateurs continuent d’alimenter le débat.
Kàddu gi njiiyu Kamërun li sànni ci mbir moomu bi ñuy amal seen ndaje mu mùjj ma, te boole yu tegloo yu ñiy jëndaani ñooy coow ba tay.
The discussion continues to be fuelled by the fact that the issue was raised by the Cameroonian employers' association at its recent general meeting, and by the repeated complaints of importers.
Selon une source, « Truly était de loin l’une des priorités d’Holly
Ap yeglekaay neena: “Ci Dégg moo nekkoon faraata bu jiitu bu Holly.
According to a source, "Truly" was by far one of Holly's top priorities.
Le conducteur du véhicule s’est arrêté, les secours sont arrivés sur place, mais l’homme est décédé sur les lieux de l’accident.
Dawalkatu oto bi taxawoon na fackat yi jappale ko waaye waaji defa mujje dee ci fi asidan bi ame.
The driver of the vehicle stopped, the rescue team arrived on the scene, but the man died at the scene of the accident.
Le Groenland a été peu peuplé. Dans les sagas scandinaves, on raconte qu’Erik le Rouge a été exilé d’Islande pour meurtre qu’il a trouvé le Groenland — et l’a nommé ainsi — en voyageant plus à l’ouest.
Groenlaand bariwul won way-dëkk. Ca tariix scandinaves ñoo ngii waxni Erik le Rouge dañuko toxal ci Islaand ngir faat bàkkan, Bimuy tukki ci sowwu, ci la gis Groenlaand dal diko tudde Groenlaand.
Greenland was sparsely populated. In the Scandinavian sagas, it is said that "Erik the Red was exiled from Iceland for murder" that he found Greenland "and named it" when traveling further west.